Yokk ay koñ walla ay waxtu
Ngir degre, minit ak segond, bësal butoŋu degre ginnaaw wàll bu nekk. Mooy butoŋ bi am 3 màndarga yu ndaw. Nanu yokk 2 degre 20 minit 30 segond, ak 39 minit 30 segond. Bindal 2, bësal
, bindal 20,
, bindal 30, ak
ati. Bësal
. Ñaareelu lim bi amul degre, kon bindal 0 ci seen palaas te nga bës
. Ba noppi bindal 39,
, 30,
, te nga bës
. Tontu li mooy 3°0'0". Butoŋ boobu dafay dox itam ngir waxtu, minit ak segond.