Ñaari melokaan ci benn xayma
Ñaari melokaan yi man nañu jaxase ci benn xayma. Ñu ngi yokk ci melokaanu rektangileer ak ci melokaanu poleer. Ci tàmbali, bësal
,
ngir tontu bu rektangileer. Bësal
, bind 4, bësal
, bind 16,
, ak
. Bësal
. Bind 2, topp
,
, ak 172. Bësal
: 2.019463863 +16.2783462i. Tontu bi dafay ñëw ci melokaan bi ñu tërale. Bësal
,
ngir gis ko ci melokaanu poleer: 16.40313352 ∠82.92811547 degre.